Bou Biblio-Adama歌曲免费下载

《Bou Biblio-Adama》歌曲详情

作词 : Mamadou Coulibaly

作曲 : Samba Ba/Mamadou Coulibaly

Adama demal sa yaay nee ko paré naa

Ndax mënn na ñaan si

Waaa waw

Adama demal sa baay nee ko paré naa te bëgg naa ñaan si

Ñëwël ñu may laa

Neenà ma yónnee samay géwël

Yónnee samay géer

Lu ma am joxee ñu may ma

Do russ di na jèem teral laa

Jii ngàma ngor nangu doon sama soxna

Demal sëy i nga muñ la ko ñepp doon diggël

Adama ngi dem di na ñu weetal

Taaru jigeen sëy la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñi weetal

Yow demal séyi nga mouñ lako ñieep doon diggël

Adama ngi dem di na ñu weetal

Taaru jigeen sey la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñi weetal

Adama ngi dem

Dem bi neex na ko

Ndax bëgg na sey ba jeex ca takk

Te ben yoon gaccée du ko ci fekk

Hée Adama dafa bëgg sëy ba seey

Bajjenam yebb na koo

Baayam ñaanal na koo

Mbokk yëpp ngi ci ginnaaw am

Demal sêy i nga muñ la ko ñepp doon diggël

Adama ngi dem di na ñu weetal

Taaru jigeen sey la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñi weetal

Yow demal séyi nga mouñ lako ñieep done diggel

Adama ngi dem di na ñu weetal

Taaru jigeen sey la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñi weetal

Adama doxxal sa yaay nee ko paré naa

Ndax mënn na ñaan si ?

Waaa waw

Adama doxxal sa Baay nee ko paré naa

Bëgg naa ñaan si

Ñëwël ñi may laa

Neenà ma yónnee samay géwël

Yónnee samay géer

Lu ma am joxee ñu may ma

Do russ mann di na jeem teral laa

Jii ngàma ngor nangu doon sama soxna

Demal sêy i nga muñ la ko ñepp doon diggël

Adama ngi dem di na ñu weetal

Hée taaru jigeen sey la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñi weetal

Yow demal séyi nga mouñ lako ñieep done diggel

Adama ngi dem di na ñu weetal

Hée taaru jigeen sey la nek ca ba ćaat loo

Adama ngi dem di na ñu weetal

下载地址:

此为隐藏内容,需人机验证后查看下载!