作词 : Mamadou Coulibaly
作曲 : Samba Ba/Mamadou Coulibaly/Boubou Dème/Pascal Alassane Thiaré/Robert Ndour
Courant di nà coupé
Di ngeen xëy cin du takk
Wayee lima bëgg ci yeen moy
Doom na ngeen goree
Seen baay ji li muy dacc
Yàlla rek mo ko xam pour seen ndam
Su ngeen ko defee ni mako bëggee
Du ngeen ñee seen benn morom
Ndaw bu sa bopp oyofee
Ndaw bu sa bopp oyofee ni xobb
Lu nëw yobaale laa
Lu nëw ñù raxx la càa
Gaynde gelewaar gà ngi ni
Doom jang i jill
Wuttil xam-xam
Ndax xam-xam moy doon i sa doole ëllëk
Wiyoo wiyoo wiyoo
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Ho baaba am na ñu jòom
Yaa ñu ci yarr te diine mi ngi ci ñunn
Wiyoo wiyoo wiyoo ohhh
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Sànt Yàll Al hamdulilah
Nàñ yok goor goor-goorlu'uuu
Baaba baal ma
Baala baal ma aqq
Baba baal ma sukk na jeegëlu
Baaba baal ma
Te tëyee ma ci loxo
Baaba ñanaal ma ma ubbeeku
Ndax barké bi laa soxla ci yow
Yow ou ou ou hou hou
Ô baaba
Ô maman
Sama yeene ci yeen moy
Ngeen dundu ba gis seen i sët sëtaat
Sama yeene ci yeen moy
Ngeen dundu ba joggee beytilaahi
Man xam na fi ngeen ma tegg
Mooy fi wayjùr di tegg doom
Wiyoo wiyoo wiyoo
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Ho baaba am na ñu jòom
Yaa ñu ci yarr te diine mi ngi ñunn
Wiyoo wiyoo wiyoo ohhh
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Sànt Yàlla Ak hamdulilaah
Nañ yok goor goor-goorgol'uuu
Wiyoo wiyoo wiyoo
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Ho baaba am na ñu jòom
Yaa ñu ci yarr te diine mi ngi ñunn
Wiyoo wiyoo wiyoo ohhh
Wiyoo wiyoo wiyoo ya
Sànt Yàlla Ak hamdulilaah
Nañ yok goor goor-goorgol'uuu

热门推荐| 1 | |
|---|---|
| 2 | |
| 3 | |
| 4 | |
| 5 | |
| 6 | |
| 7 | |
| 8 | |
| 9 | |
| 10 |